| Accueil | Créer un blog | Accès membres | Tous les blogs | Meetic 3 jours gratuit | Meetic Affinity 3 jours gratuit | Rainbow's Lips | Badoo |
newsletter de vip-blog.com S'inscrireSe désinscrire
http://barhama.vip-blog.com


CHEIKH AL ISLAM IMAM DE LA FAYDA TIDJANIA
VIP Board
Blog express
Messages audio
Video Blog
Flux RSS

CHEIKH AL ISLAM IMAM DE LA FAYDA TIDJANIA

VIP-Blog de barhama
  • 27 articles publiés
  • 41 commentaires postés
  • 1 visiteur aujourd'hui
  • Créé le : 25/03/2007 01:54
    Modifié : 25/03/2007 04:21

    Garçon (21 ans)
    Origine : DAKAR/SENEGAL
    Contact
    Favori
    Faire connaître ce blog
    Newsletter de ce blog

     Juillet  2025 
    Lun Mar Mer Jeu Ven Sam Dim
    30010203040506
    07080910111213
    14151617181920
    21222324252627
    282930010203

    BARHAMA

    25/03/2007 04:19



    BARHAAMA BAAOUN

     

    Barhaam baaou waraaou alifoun soumahaa

     

    miimoun moudial faydou tidiane diokh niou nioy naané.

     

     

    Képkou kouthi gueume  baye barhaam dootoo dokh di laath

     

    dan lay téral dila solalé gaayi tidiane.

     

     

    Mouslou lène yimalène téré kone danguène fardy naaw

     

    boulène tayal boulène diouyoo gayi tidiani.

     

     

    Boul sank say heure saa waadié kondé danga niil

     

    diobloulène bour bou dohout oubou yène gaayi tidiaani.

     

     

    Sakhsi diangue ack diolly tay wirdoo bouldi faatal dara

     

    arafou diouly  ak diangue nioo yam gaayi tidiani.

     

     

    Maa waarou maa waarou tiey maa waarou ndakh dinguène sète doundembi lépe nik fète moy cheikhou tidiaani.

     

     

    Barhaama thik dieuheul bène moodone abi an mbiyaayi

     

    thik moudieu moy abi lawliyaayi gaayi diaani.

     

     

    Omar santal yalla tey sant baayi ASS ak DAAM

     

    moo gnou nandal moo gnou dianolèkh cheikhou tidiani.

     

     

    Moo gnou kowel moo ma diangale bée gneupe dima éeme

     

    moo ma taybé bama née diaré gaayi tidiani.

     

     

    Waa faas ngay took di sènetou aynoumaan nakanoonou

     

    barhaam dieul faydou di ko diokh ahlou sodaane.

     

     

    Baaham ga barroun la momlay baakhalé bépep diam

     

    raaham ga ramanoula moy li dialé tidiani.

     

     

    Aham ga aadii la momo lay dioubalè bèpep diam

     

    liif ga allahoula moy liiy diasbou tidianii.

     

     

    Miimama mannahou la mom lay khéwalè bépep diaam

     

    yaaham ga yousran la ame nognou lèrou tidiaanii.

     

     

    Liifam ga ndieukh ahadoun la they lii doy na waar

     

    moy sounou khibla moo gnou nandal lèrou tidianii.

     

     

    Wakhouma deuguem gaayi sète lène ko té sétentalko

     

    kon nguène khamné bay moo yor mbooti tidianii.

     

     

    Ckeikhou  tidiane bahroul anwaar khatmoul awliyaayi

     

    khadmoul khatmi moodi bay moo donna tidianii.

     

     

    Bakk lène barhama yaw Baba thiaam bakkal ma bay

     

    moo ngou diasbou moo kowèl si haalou herfaanii.

     

     

    Bakk léné bakk lène barham gnoun nèp gnouy diin

     

    waané waadia dounou kou wané moy rouhoul abdaanii.

     

     

    Yaw yalla gnoo nguilay niaan thi barké baahou barham

     

    nga maygnou mbaakh gougnouy hème baniou dégne di niètaané

     

     

    Nioune niou tallal di niaane thi barkép AAhou barhaam

     

    idaayatan wakhinan ngouy sakhan di kontanéé.

     

     

    Mousaniou magal niou nandal niou thi miimou barhaam

     

    té yaaga yousran wa youmnan barké tidiaané.

     

     

    Thi liifou barhaama lan sakoon ngatabi niook baay

     

    yaw yalla niooy guen dji khète thi baakhou tidiaani

     

     

    Dioulil thi yonénth diouly goo khamné dey wey di wey

     

    dioulék azal moo niou amaloone gaayi tidiannii.

     

     

    Boulène di ngianieu saa waay boulène di yèdda saa waay

     

    si caasi shawkhou la naan min bahri tidiaanii.

     

     

    Koossi Koossoun la ay caas youniouy naané lère

     

    foofoula faydou bi done waamé gaayi tidiaanii.

     

     

    Seydou Cissé ngoongui lay niaanal thi baakhou barhaama

     

    fanwou goudak wergui yaramé gaayi tidiaanii.

     

     

    Aamiina Aamiine yène gaanii wakhlène né aamiin

     

    yalna yalla diokh lou niou doy thi barké aamiinéé.

     

     

    Warloulna kouy diangna sama way wi mboolèmi aadioom

     

    thi barké barhaama , barké cheikhou tidiaanii.

     

     

    Santa naa barhaam tey santa momar faty diop

     

    mimay yaral di ma toudalé gayii tidiaani.

     

     

    Yallna yalla faylène fath sène aadio thi barkèp cheikh

     

    yallna yalla diokhniou loudohout dièkh thi barké tidiaané.

     






    [ Annuaire | VIP-Site | Charte | Admin | Contact BARHAMA ]

    © VIP Blog - Signaler un abus